Shared Flashcard Set

Details

Wolof survival phrases
Important things to know how to say in Wolof
206
Language - Other
Undergraduate 1
01/13/2010

Additional Language - Other Flashcards

 


 

Cards

Term
jàngale
Definition
enseigner
Term
jàngalekat
Definition
prof
Term
tey
Definition
aujourd'hui
Term
waaw kumba
Definition
bien (f)
Term
waaw góor
Definition
bien (m)
Term
asalaam maalekum
Definition
as-tu la paix
Term
maalekum salaam
Definition
j'ai la paix
Term
nanga def?
Definition
ca va?
Term
maangi fi rekk
Definition
je suis ici seulement
Term
rekk
Definition
seulement
Term
nga
Definition
tu
Term
naka
Definition
comment
Term
maangi
Definition
je suis (passif)
Term
maangiy
Definition
je suis (actif)
Term
fi
Definition
ici
Term
xong
Definition
être rouge
Term
baax na
Definition
c'est bon (sérieux)
Term
neex na
Definition
c'est bon (gout, sentiment)
Term
neex ul
Definition
c'est pas bon
Term
baax ul
Definition
c'est pas bon
Term
déedéet
Definition
non
Term
waaw
Definition
oui
Term
naka waa kër gi?
Definition
comment vont les habitants de cette maison?
Term
waa
Definition
people of
Term
ker gi
Definition
maison la
Term
Ñungi fi
Definition
they all fit here
Term
Ñungi
Definition
ils
Term
Nungi
Definition
nous
Term
Naka waa kër ga?
Definition
Comment vont les habitants de la maison la-bas?
Term
Ñunga fa
Definition
Ils sont la-bas
Term
xam uma
Definition
je ne sais pas
Term
xam
Definition
savoir
Term
xamxam
Definition
conaissance
Term
maangi tudd
Definition
je m'appelle
Term
nanga tudd?
Definition
comment t'appelles tu?
Term
ci
Definition
in
Term
am uma xaalis
Definition
je n'ai pas d'argent
Term
étudiant laa
Definition
je suis etudiante
Term
tudd
Definition
s'appeller
Term
nanga sant
Definition
quel est ton nom de famille
Term
ray ma
Definition
tue-moi (quand on oublie le nom de qqn)
Term
fàtte naa
Definition
j'ai oublié
Term
bul ma rey
Definition
ne me tue pas
Term
Fan nga dëkk?
Definition
Tu habites où?
Term
Maangi dëkk
Definition
J'habite
Term
Fan
Definition
Term
ak
Definition
et
Term
waajur
Definition
parents
Term
sama kër
Definition
chez moi
Term
sama
Definition
my (singulier)
Term
samay
Definition
my (pluriel)
Term
noo ko bokk
Definition
de rien
Term
ba suba
Definition
à demain
Term
suba
Definition
demain
Term
jërejëf
Definition
merci
Term
torop
Definition
beaucoup
Term
lool
Definition
beaucoup
Term
wànte
Definition
mais
Term
u
Definition
of
Term
suur naa
Definition
j'ai le ventre plein
Term
ñaata
Definition
combien
Term
yow nak
Definition
et toi
Term
yow
Definition
toi
Term
may ma
Definition
donne-moi
Term
xaaral ba mu am rakk
Definition
attends jusqu'il a un petit frère (non)
Term
lekkal
Definition
manges
Term
toogal
Definition
asseids toi
Term
xaaral ba ginaar sax bëñ
Definition
attendre jusqu'à les poulets pousse des dents
Term
ñëw
Definition
venir
Term
xaaral ba mu ñëw
Definition
attends jusqu'à j'arrive
Term
dem
Definition
aller
Term
maangiy dem
Definition
je vais
Term
Fan
Definition
où (endroits)
Term
kan
Definition
qui (gens)
Term
lan
Definition
what (choses)
Term
lii
Definition
cette chose
Term
kii
Definition
this person
Term
lii lan la?
Definition
c'est où cette chose?
Term
lii ---- la
Definition
cette chose est ----
Term
Fii fan la?
Definition
c'est où cet endroit?
Term
Fii --- la
Definition
Cet endroit est ---
Term
kii kan la?
Definition
qui est cette personne?
Term
--- fan la?
Definition
où est ---- (chose)
Term
wanag wi
Definition
toilett
Term
waañwi
Definition
cuisine
Term
bind
Definition
écrire
Term
bindukaay
Definition
instrument d'écriture
Term
toogukaay
Definition
chaise
Term
toog
Definition
s'assoir
Term
bëgg
Definition
aimer qqch
Term
nob
Definition
aimer qqn
Term
lekk
Definition
manger
Term
naan
Definition
boire
Term
naanukay
Definition
cup
Term
bitik bi
Definition
la boutique
Term
kalaas bi
Definition
la salle de classe
Term
marse bi
Definition
le marché
Term
lan nga bëgg
Definition
qu'est-ce que tu veux
Term
loo bëgg?
Definition
qu'est-ce que tu veux
Term
loo bëgg leek?
Definition
qu'est-ce que tu veux manger?
Term
jënd
Definition
acheter
Term
seeti
Definition
visiter
Term
kii
Definition
cette personne
Term
lii
Definition
cette chose
Term
fii
Definition
cet endroit
Term
Fan ngay dem?
Definition
Où est-ce que tu vas?
Term
Fan nga dem?
Definition
où est-tu allé?
Term
gató
Definition
gateau
Term
ñaata nga fay
Definition
combien as-tu payé?
Term
xool
Definition
regarder
Term
ndox
Definition
l'eau
Term
dox
Definition
marcher
Term
yaangi(y)
Definition
tu es
Term
mungi(y)
Definition
il est
Term
fanaanal ak jàmm
Definition
bonne nuit
Term
naka nga fanaane?
Definition
Tu as bien dormi?
Term
verbe + -u
Definition
reflexif
Term
fanaan
Definition
passer la nuit
Term
may ma
Definition
donnes-moi à jamais
Term
jox ma
Definition
donnes-moi pour l'instant
Term
ba beneen yoon
Definition
jusqu'à la prochaine fois
Term
tuuti
Definition
un peu
Term
abal ma
Definition
prêtes moi
Term
ma bañ
Definition
je réfuse
Term
man itam
Definition
moi aussi
Term
yow itam
Definition
toi aussi
Term
moom itam
Definition
lui aussi
Term
ci wet u
Definition
près de
Term
sore na
Definition
loins de
Term
jeex
Definition
finir
Term
ñëw
Definition
venir
Term
ayca
Definition
on y va
Term
naka ngeen def
Definition
comment allez-vous
Term
ngeen
Definition
vous (pluriel)
Term
nangeen def?
Definition
comment allez-vous?
Term
Fan ngeen dëkk
Definition
où habitez-vous
Term
lungeen (lan ngeen)
Definition
qu'est-ce que vous
Term
kafe ak meew
Definition
café au lait
Term
meew
Definition
lait
Term
soow
Definition
yaourt
Term
jàmm rekk
Definition
la paix seulement (en réponse de comment as tu dormi ou comment était ta journée?)
Term
yendu
Definition
passer la journée
Term
naka nga yendoo?
Definition
comment as-tu passé la journée?
Term
verbe + -e
Definition
la manière, l'instrument, ou la place
Term
lekke
Definition
la manière de manger
Term
lan ngay lekke?
Definition
Qu'est-ce que tu utilise pour manger?
Term
loxo
Definition
la main
Term
téeré
Definition
le livre
Term
yendul ak jàmm
Definition
bonne journée
Term
ekool
Definition
école
Term
géej
Definition
la plage
Term
baal ma
Definition
excuse-moi
Term
waxal ndànk ndank, dègg uma wolof bu baax
Definition
parle lentement, je ne comprends pas très bien le wolof
Term
wax
Definition
parler
Term
ndànk
Definition
lentement
Term
dègg
Definition
comprendre
Term
dègg uma
Definition
je ne comprends pas
Term
wala
Definition
ou
Term
su fekkee
Definition
si
Term
amiin
Definition
souhaiter
Term
laaj
Definition
demander
Term
kuddu
Definition
cuillère
Term
furset
Definition
forchette
Term
paaka
Definition
couteau
Term
wax aat al
Definition
repetez
Term
du man
Definition
moi non
Term
góor
Definition
homme
Term
jigéen
Definition
femme
Term
ba ci kanam
Definition
à plus tard
Term
kanam
Definition
devant
Term
say juróon
Definition
high five
Term
verbe +i
Definition
deplacement dans l'espace pour remplacer aller
Term
verbe +si
Definition
deplacement dans l'espace pour remplacer venir
Term
kañ
Definition
quand
Term
kañ nga ñëw?
Definition
quand tu viens?
Term
léegi
Definition
maintenant
Term
ñibbi
Definition
rentrer
Term
Thèrese fan la nekk?
Definition
Où est Thèrese?
Term
nekk
Definition
to be located
Term
dama bëgg doxantu
Definition
je veux se promanader
Term
doxantu
Definition
promanader
Term
waxtaan
Definition
converser
Term
dama
Definition
je (plus important que maangi)
Term
dama xiif
Definition
j'ai faim
Term
dama noppaliku
Definition
je me repose
Term
dama sangu
Definition
je me douche
Term
dama raxasu
Definition
je me lave (une partie du corps)
Term
dama mar
Definition
j'ai soif
Term
dama sonn
Definition
j'ai sommeil
Term
dafa sedd
Definition
il fait froid
Term
dafa tàng
Definition
il fait chaud
Term
nelaw
Definition
dormir
Term
dafa
Definition
third person
Term
kaay lekk
Definition
viens manger
Term
ndekki
Definition
petit déjeuner
Term
Definition
déjeuner
Term
reer
Definition
diner
Term
kaay ndekki
Definition
viens manger le petit déjeuner
Term
réer
Definition
se perdre
Term
lekk naa ba fii
Definition
j'ai mangé jusqu'à ici
Term
benn
Definition
un
Term
ñaar
Definition
deux
Term
ñett
Definition
trois
Term
ñeent
Definition
quatre
Term
juróom
Definition
5
Term
fukk
Definition
dix
Supporting users have an ad free experience!