Shared Flashcard Set

Details

Wolof Competence 4
Wolof Competence 4
107
Other
Not Applicable
10/11/2009

Additional Other Flashcards

 


 

Cards

Term
fr: le coin
Definition
wo: angal bi
Term
fr: un placard (cupboard)
Definition
wo: armuwaar bi
Term
fr: un bar
Definition
wo: baar bi
Term
fr: une banque
Definition
wo: bánk bi
Term
fr: un stylo
Definition
wo: bindukaay or bik bi
Term
fr: une boutique
Definition
wo: butik bi
Term
fr: la porte
Definition
wo: bunt bi
Term
fr: des chausseurs
Definition
wo: dale
Term

fr: une chasseur

fr: les chasseurs

Definition

wo: dàll wi

wo: dàll yi

Term
fr: un village
Definition
wo: dëkk bi
Term
fr: un barbecue sénégalais
Definition
wo: dibiteri bi
Term
fr: centre de santé
Definition
wo: dispañseer bi
Term
fr: une église
Definition
wo: egliis bi
Term
fr: une école
Definition
wo: ekkool bi
Term
fr: un jardin
Definition
wo: ëtt bi
Term
fr: une pharmacie
Definition
wo: farmasi bi
Term
fr: un canapé
Definition
wo: fotëy bi
Term
fr: une fourchette
Definition
wo: furset bi
Term
fr: la boulangerie
Definition
wo: fuuru mburu bi
Term
fr: une plage
Definition
wo: géej gi
Term
fr: le mosquée
Definition
wo: jákka ji
Term
fr: la mosquée (le vendredi)
Definition
wo: jumaa ji
Term
fr: la tasse
Definition
wo: kaas bi
Term
fr: le cahier
Definition
wo: kaye bi
Term
fr: chez qqn
Definition
wo: kër gi
Term
fr: le quartier
Definition
wo: koñ ou karce bi
Term
fr: la cuillère
Definition
wo: kuddu gi
Term
fr: le lit
Definition
wo: lal bi
Term
fr: la lampe
Definition
wo: lámp bi
Term
fr: la rue
Definition
wo: mbeed mi
Term
fr: la salle
Definition
wo: néeg bi
Term
fr: le couteau
Definition
wo: paaki bi
Term
fr: la fenêtre
Definition
wo: palanteer bi
Term
fr: le commissariat de police
Definition
wo: polis bi
Term
fr: la radio
Definition
wo: rajo bi
Term
fr: rond-point
Definition
wo: rondpoint bi
Term
fr: le sac
Definition
wo: saak bi ou saag bi
Term
fr: le salon ou la salle de séjour
Definition
wo: saal bi
Term
fr: le savon
Definition
wo: saabu bi
Term
fr: le savon
Definition
wo: saabu bi
Term
fr: le miroir
Definition
wo: seetu bi
Term
fr: le sarong
Definition
wo: sër bi
Term
fr: la chaise
Definition
wo: siis bi
Term
fr: le cinéma
Definition
wo: sinema bi
Term
fr: le sol
Definition
wo: suuf
Term
fr: le super-marché
Definition
wo: supermarse bi
Term
fr: le sucre
Definition
wo: suukër si
Term
fr: la table
Definition
wo: taabal ji
Term
fr: la télévision
Definition
wo: tele bi
Term
fr: le téléphone
Definition
wo: telefon bi
Term
fr: le livre
Definition
wo: téere bi
Term
fr: le pantalon
Definition
wo: tubëy bi
Term
fr: la salle de bain
Definition
wo: wanag wi ou wanag wi orduus bi
Term
fr: la cuisine
Definition
wo: waañ wi
Term

fr: le sel

 

Definition
wo: xorom si
Term
fr: les vêtements
Definition
wo: yére yi
Term
fr: le chemin
Definition
wo: yoonu wi
Term
fr: où (pour les endroits)
Definition

wo: fan

ex: Fii fan la (qu'est-ce que c'est, cet endroit?)?

Fii post la (C'est le bureau de poste)

Term
fr: qui? (singulier)
Definition

wo: kan

ex: Kii kan la (qui est cette personne?)?

Kii sama xarit la (c'est mon ami).

 

Term
fr: où (pour les personnes)
Definition
wo: ana (notez: ana est déjà conjugué)
Term
fr: qui? (pluriel)
Definition
wo: ñan
Term
fr: quand (seulment pour les questions)
Definition
wo: kañ
Term
fr: pourquoi
Definition
wo: lutax
Term
fr: est-ce que (sujet+verb)...?
Definition
wo: ndax
Term
fr: comment...?
Definition
wo: naka
Term
fr: ce, cet, cet
Definition
wo: lii
Term
fr: celui-ci (this one)
Definition
wo: kii
Term
fr: ici
Definition
wo: fii
Term
fr: traverser
Definition
wo: jéggi
Term
fr: suivre
Definition
wo: topp
Term
fr: continuer tout droit
Definition
wo: jubal
Term
fr: aller tout droit
Definition
wo: tallal
Term
fr: dépasser (go past)
Definition

 wo: weesu

 

Term
fr: revenir sur les pas, rebrousser chemin, faire marche arrière (fig.?) (to backtrack)
Definition
wo: dëpp
Term
fr: tourner
Definition
wo: jádd
Term
fr: se dresser (stand up), arrêter
Definition
wo: taxaw
Term
fr: arriver
Definition
wo: ágg
Term
en: go around
Definition
wo: wëri
Term
fr: loin
Definition
wo: sori
Term
fr: d'être loin
Definition
wo: sori na
Term
fr: est-ce que c'est loin?
Definition
wo: sori na?
Term
fr: est-ce que le marché est loin d'ici?
Definition
wo: marse bi sori na?
Term
fr: d'être pres
Definition
wo: jege
Term
fr: est-ce que le bureau de poste est pres d'ici?
Definition
wo: Post bi jege na fii
Term
fr: c'est loin d'ici
Definition
wo: dafa sori
Term
fr: c'est pres d'ici
Definition
wo: dafa jege
Term
fr: c'est à quelle distance?
Definition
wo: fan la tollu fii
Term
fr: c'est ici (c'est pas loin)
Definition
wo: fii rekk la
Term
fr: entre...et...
Definition
wo: ci diggante...ak...
Term
fr: derrière
Definition
wo: ci ginnaw
Term
fr: à côté de
Definition
wo: ci wetu
Term
fr: à droit (de)
Definition
wo: ci ndeyjoor(u)
Term
fr: à gauche (de)
Definition
wo: ci cammooñ(u)
Term
fr: avant (de)
Definition
wo: ci kanam(u)
Term
fr: sur ("dans" dans quelques contextes)
Definition
wo: ci kaw
Term
fr: par terre
Definition
wo: ci suuf
Term
fr: sous
Definition
wo: ci suufu
Term
fr: dans
Definition
wo: ci biir
Term
comment dit-on, "l'école est à côté du bureau de poste."
Definition

1. ekool bi mungi ci wetu post bi

2. bi ci wetu post bi la nekk

Term
comment dit-on, "le couteau est sur la table"
Definition

1. paaka bi mungi ci kaw taabal ji

2. paaka bi ci taabal ji la nekk

Term
comment compose-t-on l'impéritif affirmatif en wolof?
Definition

singulier: verbe+al (toppal)

pluriel 1er personne: nu +verbe (nu topp)

pluriel 2e personne: verb+leen (toppleen)

topp=suivre

verbes singulier prendront un "l" plutôt que "al"

e.g. sangul (verbe sangu)

Term
comment compose-t-on l'impéritif négatif en wolof?
Definition

singulier: bul+verbe(bul topp)

pluriel 1er personne: bunu +verbe (bunu topp)

pluriel 2e personne: buleen+verbe(buuleen topp)

topp=suivre

verbes singulier prendront un "l" plutôt que "al"

e.g. sangul (verbe sangu)

Term
fr: se faire face
Definition

wo: jakkaarloo ak

(c'est le verbe et la préposition)

 

e.g. Fanta mungi jakkarloo ak Moutarou

 

note: l'expression au-dessus comprend le verbe & la préposition et peut-être utiliser avec dafa or danu

Term
fr: être contiguë (/kɔ̃.ti.ɡy/)
Definition

wo: taxaloo ak

 

e.g. Këram dafa taxalo ak opitaal bi

(leur maison est contiguë avec l'hôpital)

 

note: l'expression au-dessus comprend le verbe & la préposition et peut-être utiliser avec dafa or danu

Term
fr: être derrière
Definition

wo: won ginnaaw

 

note: l'expression au-dessus comprend le verbe & la préposition et peut-être utiliser avec dafa or danu

Term
fr: être loin
Definition

wo: sori

 

note: l'expression au-dessus comprend le verbe & la préposition et peut-être utiliser avec dafa or danu

Term
fr: être jege
Definition

wo: jege

note: l'expression au-dessus comprend le verbe & la préposition et peut-être utiliser avec dafa or danu

Supporting users have an ad free experience!