Shared Flashcard Set

Details

Wolof Competence 3
Wolof Competence 3
24
Language - Other
Not Applicable
11/15/2009

Additional Language - Other Flashcards

 


 

Cards

Term
fr: la semain passée
Definition
wo: ayu bés bii weesu
Term
fr: lundi dernier
Definition
wo: altine bii weesu
Term
fr: le mois dernier
Definition
wo: weer wii weesu
Term
fr: le week-end dernier
Definition
wo: weekend bii weesu
Term
fr: hier
Definition
wo: démb
Term
fr: le jour avant hier
Definition
wo: bërki démb
Term
fr: hier soir
Definition

wo: biig

 

wo: démb ci guddi

Term
fr: l'autre jour
Definition
wo: keroog
Term
fr: ce matin
Definition
wo: ci suba
Term
fr: l'année passée
Definition
wo: daaw
Term
fr: ensuite
Definition

wo: ginnaaw loolu

 

wo: bi loolu weesoo

Term
fr: après + nom
Definition
wo: ginnaaw + nom
Term
fr: après le petit déjeuner
Definition
wo: ginnaaw ndekki
Term
fr: le jour après
Definition
wo: ci ëllëg sa
Term
fr: avant ça
Definition
wo: balaa loolu
Term
fr: avant + nom
Definition
wo: baala + nom
Term
donne la 1er personne singulier des verbes actifs
Definition

verbe actif + naa

 

demb, lekk na ceebu ginnaar

(hier, j'ai mangé du riz et poulet)

Term
donne la 2e personne singulier des verbes actifs
Definition
verbe actif + nga
Term
donne la 3e personne singulier des verbes actifs
Definition

verbe actif + na

 

talaata, woo na yaayam

(elle a appellé à sa mère)

Term
donne la 1er personne pluriel des verbes actifs
Definition
verbe actif + nanu
Term
donne la 2e personne pluriel des verbes actifs
Definition

verbe actif + ngeen

 

ayu bës bii weesu, dem ngeen touba

(la semaine dernière, vous êtes allés à Touba)

Term
donne la 3e personne pluriel des verbes actifs
Definition
verbe actif + nañu
Term
donne la négation de la 3e personne pluriel des verbes actifs
Definition

verbe actif + uma

 

ayu bës bii, janguma Wolof.

(Pendant la semaine dernière je n'ai pas étudié le wolof)

Term
donne la négation de la 3e personne pluriel des verbes actifs
Definition
Supporting users have an ad free experience!